ettub wolof 1

Licence: Gratuit ‎Taille du fichier: 8.07 MB
‎Note des utilisateurs: 5.0/5 - ‎1 ‎Votes

Sur ettub wolof

ci wolof - En français - En Anglais

ci wolof

ëttub wolof moo leen di baaxe benn sàqum baatu wolof, te ñu tuddee ko oggo, ay léebu ak benn jumtukaayu ijji ngir mën a ijji ci wolof. oggo mooy sàqum baatu wolof bi jëkk a am, nga xam ne baat yépp ci wolof kepp lañu leen tekki. oggo am na lu ëpp fukki junney baat ak benn. léebu yi ëpp nañu ñeenti junney léebu, boole ci juroom ñetti téemeeri waxin. waxinu benn léebu, mooy léebu bu ñu waxee neneen. jumtukaayu ijji bi, dina tax ngeen mën a ijji ci wolof, ci amam yu gaaw. ngir jàng dawal wala jàng bind wolof, mën ngeen a jëfandikoo dalu-web bii di www.ettubwolof.org.

En français

ëttuf wolof vous propose un dictionnaire wolof nommé oggo, des proverbes wolof et un outil pour vous familiariser avec l’alphabet wolof. oggo est le premier dictionnaire entièrement en wolof avec la définition des mots en wolof. Il contient plus de 11 000 mots wolofs. Les proverbes wolofs comptent plus de 4000 proverbes incluant plus de 800 versions. Une version d’un proverbe est une façon différente de dire le proverbe. L’outil de l’alphabet est très utile pour vous rapidement familiariser avec les lettres de l’alphabet wolof. Pour apprendre à lire et à écrire le wolof, vous pouvez également utiliser le site www.ettubwolof.org, plus riche en contenu.

En anglais

ëttub wolof offre un dictionnaire wolof nommé oggo , proverbes wolof et un outil pour se familiariser avec l’alphabet Wolof . oggo est le premier dictionnaire entièrement en wolof avec la définition des mots en wolof . Il contient plus de 11 000 mots wolof.

Proverbes wolof ont plus de 4000 dont plus de 800 versions. Une version d’un proverbe est une façon différente de dire ce proverbe.

L’outil alphabet est très utile pour se familiariser rapidement avec les lettres d’alphabet Wolof.

Pour apprendre à lire et à écrire en wolof, vous pouvez également utiliser le site Web www.ettubwolof.org quel contenu est le plus riche.